Maysa tende jodo yaa moom liile (3x)
Hi woy Birima fumu yendu ma yendu fa yendo naanee
Woy Birima fumu yendu ma yendu fa yendo naanee (3x)
Buri samba laobe yaa moom liile (3x)
Hi woy Birima fumu yendu ma yendu fa yendo naanee
Woy Birima fumu yendu ma yendu fa yendo naanee
Damel maisa Penda Joor
Jooro Jooro Jooro Jooro Ho Ho Ho Hoy
Sama waaji ken dula jam naani
Woy Birima fumu yendu ma yendu fa yendo naanee
mmmm mmm
Wooy Tedi Ngoné maarne be Sambaa
Kuli baca senge ndat Biran ngamoo
Ngoné maca ñas mbay maca jeeri
Samba yaasimooooo dike mbay Kuja dooooki
Yay borom mbabo
5 min 14 sec ago
3 hours 41 min ago
13 hours 7 min ago
13 hours 8 min ago
15 hours 28 min ago
16 hours 34 min ago
21 hours 45 min ago
21 hours 48 min ago
21 hours 50 min ago
22 hours 22 sec ago